Home › Ringtones › Doundou oundou - Dip Doundou Guiss

Doundou oundou - Dip Doundou Guiss

free ringtone for iPhone & Android phones

@Sandra
408
30 Sec

Doundou oundou - song lyrics

DIP Doundou Guiss - #Doundou_Oundou

{Refrain}
Ba gni nekk boy lignou done doundou aka doy war
Ba tay souma koy wakh damay réh ba djoy
Souma kholé lignou dane def dagno beugone yeufou gangster
Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def
Ba gni nekk boy yeufou oundou rek
Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def
Ba gni nekk boy yeufou oundou rek
Ba tay dé magg nagnou

{1}
Sa youmay dem école dagn may door ma yéwou
Té souma démoulé école fadjaar tél lay yéwou
Dougou kogne ba wala dem ba Niaye rek tokfa
Mane ak sama gars yi khol kou gueuneu kaagne gnou togne ko
Ba heurou ndéki am gnou délou waat sen galé ndéki
Gnou niakk controle chaque jour cii biti lagni ndéké
Outi féraille. lokoy doyé? no dama koy djaay
Bouteille, preum, armignon père dakal mou nieuw
Xaliss dougnouko khar mou nieuw no da am yone
Baabi, pile, perpé, dayce (Dé), xaliss xaliss, pot égatte
Fo ba xotti sa yééré swagg soudé dall
Kou tchii gueunone guerrier fok gnou coup d'état la

{Refrain}
Ba gni nekk boy lignou done doundou aka doy war
Ba tay souma koy wakh damay réh ba djoy
Souma kholé lignou dane def dagno beugone yeufou gangster
Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def
Ba gni nekk boy yeufou oundou rek
Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def
Ba gni nekk boy yeufou oundou rek
Ba tay dé magg nagnou

{2}
Yallah gnou aar, ndakh fougnou diar, mbede dou yaar
Forr cigarette guéné sakhar, beuri nullard
Eufeul ay xathie, langg camion, taxi, cassambaar
Neubeul ni naar, beuri cica (cicatrice) peundeul yambaar
Tournoi potou méw, rayanté ndakh bène kopp wéégne
Boy bi bougnou topoté fou magg yi dem niou topp lène
Guel bo dokhane sou bagné nga nokk ko bamou xam
Sangou cii ndoxou taw, def sieste cii biir ay mbaarou kharr (Mouton)
Tardé agne tibeu, boudé teud feug
Wa galé commencé guiss né ni sen fils sa ngui deung
Dagn lay interné, dieundeul la play ba internet
Bo gnak chance deugg for ever mbédeu lay hébergé

{Refrain}
Ba gni nekk boy lignou done doundou aka doy war
Ba tay souma koy wakh damay réh ba djoy
Souma kholé lignou dane def dagno beugone yeufou gangster
Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def
Ba gni nekk boy yeufou oundou rek
Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def
Ba gni nekk boy yeufou oundou rek
Ba tay dé magg nagnou

{3}
It goes out for my niggaz yima fowa ndol
Gnima bokka lone kogne
Gnima nékalone école primaire
Meunouma dem fatélène
Amoul lougnou défoul, amoul lougnou défoul
Xawouma lougnou défoul, waxma gaff bougnou défoul
Beuré bougnou démoul, béré bougnou lékoul
Goune dagnou dane sananté kherr di guerre
Saganté kherr di réééh hann anyway
Nokanté everyday yeah
Beuri, leudj, dakanté périééé, taf dokk, baskulé
Motakh ma nane la

{Refrain}
Ba gni nekk boy lignou done doundou aka doy war
Ba tay souma koy wakh damay réh ba djoy
Souma kholé lignou dane def dagno beugone yeufou gangster
Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def
Ba gni nekk boy yeufou oundou rek
Ba gni nekk boy moussiba rek lagnou dane def
Ba gni nekk boy yeufou oundou rek
Ba tay dé magg nagnou

Top 100 Minecraft Ringtones
Top 100 Toca Boca Ringtones
Top 100 League of Legends Ringtones

Similar ringtones:

MORE...[+]
Top 100 Genshin Impact Ringtones
Top 100 Among Us Ringtones
Top 100 Free Fire Ringtones
Top 100 PUBG Ringtones
Top 100 Civilization VI Ringtones

More ringtones from Dip Doundou Guiss:

30
@Lidia
680
Ou-ouuuh ou-ouuuuh Yeah Mann beugouma nékk buur Wayé Yallama deff buur Kheuyneu,mann nangounaa Konn meunouma mayy may bagn Ou-ouuuh ou-ouuuuh Yeah May gagnn samay ennemis Gnouy nadj sénni ranguognii Guissna kouy yéttal najj bi Mouné maka wara yééé Ou-ouuuuh Ou-ouuuu-ouhh Sama yaramm déé Sama khéllay téy-y-y Sama jeumeuk sama rouh moussougnou wéranté Douma nitt kou bonn way Yéneu say damay wééré Yéneu say damay mérr teujj sam bountakk parentéérrr Yéneu say damay triste Yéneu say damay sissou Déé wama gueunneul tiittt kharr douma yerentii Diganté khajjak boukki Bidéwou khajja gouddi Feel ngénn ba lakatoujji Guiss ngénn ni Yalla dou nitt Foukki nooone,jounni mbokk you deuggou Foukki gorr,jounni bopp you teujjou Boudoul God joulliwoo dangay teureull Toukkiwo boussa rouh bi dagnagoul Kiliftéff doussa Sikkim _ wéékh Leundeumm lérr mélni timiss _guéé Tilim_séttt ni jeunn si biir guédj Sigui ténnn féssak dignité Esprit khéll after physique khékh Tédd tékki simple ni Bill Gates Am dérrou séggg mais ay boukki nguénn Ou-ouuuh ou-ouuuuh Yeah Mann beugouma nékk buur Wayé Yallama deff buur Kheuyneu,mann nangounaa Konn meunouma mayy may bagn Ou-ouuuh ou-ouuuuh Yeah May gagnn samay ennemis Gnouy nadj sénni ranguognii Guissna kouy yéttal najj bi Mouné maka wara yééé Ou-ouuuuh Ou-ouuuu-ouhh Reptyl music Next song...
MORE...[+]

Set Doundou oundou ringtone on an Android Phone:

1. Select Download Ringtone button above.
2. Go to Settings app.
3. Select Sounds & Vibration.
4. Select Phone ringtone.
5. Select Ringtone from Internal Storage.
6. Click the Apply button.
So after only a few basic steps, you have successfully done the default ringtone on your phone running Android operating system with the pop songs you want.



Set Doundou oundou ringtone for your iPhone:

1. Select Download M4R for iPhone button above and save to your PC or Mac.
2. Connect your iPhone to your PC or Mac via its charging cable.
3. Launch iTunes and drag the .m4r to the Tones folder (Under "On My Device").
Hopefully, the guides for configuring ringtones for iPhones and Android phones will make it simple for you to replace the uninteresting default sounds on your phone with your own personal favorites.



Browse 5,000,000+ free ringtones by categories:

Thanks for letting us know
Your feedback is important in helping us keep the 1Ringtone community safe.
Close

X

#1 Ringtone App - top ringtones for free!

logo
Login with Google Login with Facebook

By joining, you agree to Terms of Service & Privacy Policy.

Upload a ringtone

You can upload MP3, WAV, M4A, OGG, M4R, ACC format files.

By selecting 'Upload' you are representing that this item is not obscene and does not otherwise violate Terms of Service, and that you own all copyrights to this item or have express permission from the copyright owner(s) to upload it.

Before uploading, please read our Privacy.